Siddeem bukki
From Wikipedia, the free encyclopedia
Remove ads
Siddeem bukki xeetu garab gu bokk ci njabootug Rhamnacées. Moo ngi coosaanoo Lo ci réew yu naaje yi.

Aw meloom
Siddeem bukki garab guy am i dég, ak i doom yu nuy woowee siddeem bukki. Garab gu dëgër lay doon ci jamonoy noor.
Am xasam day ñagas am ay pàq, wànqaas yi yaatu, ëppante te am i dég. Xobam yi seen wirgo day wuute.
Njariñ yi
Doom bi dees na ko jëfandikoo ci togg, dees na ko lekk noonu it.
Foytéef bi barina ay ferñeent lool.
Nataal



Turu xam-xam wi
Ziziphus mucronata
Wikiwand - on
Seamless Wikipedia browsing. On steroids.
Remove ads