Weer
From Wikipedia, the free encyclopedia
Remove ads
Weer ab diirub jamono la, séddaliku ci ay ayubés, moom, ayubés, séddaliku ci ay bés. Ci arminaatu weer, ñu di ko wax itam weeri wolof, at mi fukk ak ñaari weer la, te weer yi am limu bés yu wuute.
Yeneen xeeti arminaat yu dul bu weer man nañoo nekk, ci misaal, arminaatu jant
Aminaatu weer
Dees na ko wax it weeru wolof
Arminaatu jant
Wikiwand - on
Seamless Wikipedia browsing. On steroids.
Remove ads