Wikbaatukaay

From Wikipedia, the free encyclopedia

Wikbaatukaay
Remove ads

Wikbaatukaay ab baatukaay barilàkk bu ubbeeku la, di benn ci sémbi Wikimedia Fondation yi. Baatub «Wikbaatukaay» dafay junj sumb bu wolof bu boobu sémb, di Wiktionary ci wu-angalteer. Mook Wikipedia ñoo bokk doxiin, di lu ubbeeku te dàttu ci nosteg wiki, lees man a jëfandikoowaat ci anami GFDL.

Thumb
Sémbu Wikbaatukaay

Tëddiin

Yéeney sémb bi mooy sos ab baatukaay bees di duggal làkki àdduna bi yépp. Ci bu wolof baat yépp a fiy nekk ak seen tekki ci yeneen làkk waaye ci wolof lañu leen di faramfaccee, joge seen gongikubaat, seeni bokktekki, safaantekki, waxiin, añs.

Loading related searches...

Wikiwand - on

Seamless Wikipedia browsing. On steroids.

Remove ads